You are on page 1of 20

AL XURAAN

CI WOLOF

@ L'Harmattan, 1997
ISBN: 2-7384-5966-8

Path Diagne

AL XURAAN
CI WOLOF

ditions L'Harmattan
5-7, nie de l'cole-Polytechnique
75005 Paris

L 'Harmattan Inc.
55, rue Saint-Jacques
Montral (Qc) - CANADA H2Y lK9

SANKOR

Ouvrages du mme auteur:


- Pouvoir politique en Afrique occidentale, Prsence
africaine, Paris, 1967.
- Grammaire moderne du Wolof, Prsence africaine,
Paris, 1967.
- Pout l'unit ouest-africaine, intgration ou micro-tat,
Paris, Anthropos, 1972 (Thse de Doctorat d'Etat en
Sciences Economiques, Universit de Paris-Sorbonne).
- Introduction la culture africaine, ouvrage collectif,
Paris, UNESCO-collection 10/18, 1976.
- Histoire gnrale de l'Afrique noire, volume 2, Paris,
UNESCO, 1978.
- L'Europhilosophie face la pense du Ngro-africain,
Sankor, 1979.
- Bakari II (1312) et Christophe Colomb (1492) la
rencontre de l'Amrique, Sankor, 1992.
- Lopold Sdar Senghor ou la ngritude servante de la
francophonie au festival d'Alger.

Kddu gu jkk

Avant propos

Dafiuy gnn fii takk ci Al Xuraan


ci Wolof.

Nous publions ici un condens


du Coran en Wolof.

Dafa mb juroom fukk ag fiatti


saar ci temer ag fukk ag fient yi
fiu tekki te nu nekk ci Terbi Al
Xuraan bi .

Il comporte soixante quinze des


cent quatorze sourates traduites
que contient le Coran.

Saar yooyu fiooy : fiatt fii jkk ag


fukk ag juroon yi mujj.

Il s'agit ici des douze premires


et des soixantes trois dernires.

Dafiu leen tnn gnn ba mn


yombal gannaaw loolu tasaare
mu jottali fiepp Teere Al Xuraan
bi.

Ces sourates ont t choisies et


publies
pour prparer
la
diffusion et l'accs du grand
public la totalit du texte.

Dama fas yne ci lu gtt boole


boroom xamxam yi ci ngnn Al
Xuraan ci wolof fu mu dee mbiru
fipp.

J'ai choisi de faire de la


publication d'une dition finale,
un challenge collectif auquel
seront associs tous ceux qui
peu vent y apporter
une
contribution.

Maa ngiy sant Kumba Gey,


Faatu Saar, Tina Cesaltine, Ndey
Faatu Mbay noo tappe mbind mi.
Di sant Buubakar Kan di jangale
Ecole Normale mi ko toppaat.

Je remercie Kumba Guye,


Fatou Sarr Tina Csaltine,
Ndeye Fatou Mbaye qui ont
assur la saisie l'ordinateur de
ce texte. Sans oublier Boubacar
Kane, professeur
l'Ecole
Normale Suprieure qui a bien
voulu le relire.

Teerehkat hi

L'diteur

UBBI

INTRODUCTION

1 - Al Xuraan jii nuy jema


tekki fii ag di ko bind, bi fi
lislaam duggee ba tay, julliti
suiiu wllu rew yii, danu ms
di ka tral ci seeni lkk, ba mil
xam Ii baatu Ylla biy leera!.

1 - Le Coran dont nous


essayons de donner ici une
modeste traduction crite, les
musulmans de nos contres
n'ont eu cesse de le naturaliser
dans leur langue, de manire
saisir ce que la Parole de Dieu
claire.

2 - Loolu ngir jppe ko seen


xel,tbbal ko ci seen xol, ba
mil rafetal topp seen Boroom.

2 - Cela avec le dessein de le


comprendre dans sa rationalit,
de l'apprhender
dans leur
coeur, afin de servir Dieu de la
meilleure manire.

3 - Tari, tekki ag firi Al Xuraan,


Ylla dafa ko santaane, Dafa
dppoog it ag lu yomb nangu, ci
rew ag xeetu Afrig yi cosaanoo
dmb, te bokk ci fii j'/(k jiit1
xam, xamxam ag xamme, Tere
b, Ylla moo ni ci "Moom
dOfJTJmoo ko m'n tekki (suraat
3 - laaya 5). Loolu dafa wane
ni ku koy tekki mbaa leeral,
m'nullu dul di jem jege Ii mu
ci lxx. Teewul mu santaane nu
jng ko, te di jema xam Ii mu
ci inb, ag fi muy feenal.

3
Rciter, traduire et
commenter le Coran, est une
prescription que Dieu a faite.
Celle-ci rencontre facilement
l'adhsion parmi les nations
d'Afrique qui appartiennent de
vieilles traditions, et qui, parmi
les premires, ont privilgi le
savoir, la science et la sagesse.
Le Livre affirme que Dieu seul
pouvoir de donner aux versets
du Coran leur sens exact
(Sourate III, verset 5). Cela
montre que toute explication ou
interprtation n'est qu'approche
de ce qu'il y a de cach. Il n'en
ordonne pas moins de tenter de
saisir ce qu'il recle et qu'il
rvle.

- Santaane wi moo waral, ci


Afrig, bi fi /islam duggee ba
tay, daara yi di dajale xale yi,
nu j"/(ktari AI Xuraan ju sell
ji. Su mokle mbaa nu mokkal
ci lu tane nu tekkilleen ko, firil
leen Ii nu ci jng te jpp ko.

4 - C'est cette prescription qui


lgitime en Afrique, ds
l'apparition
de l'islam, la
cration
d'coles
qui
rassemblent les enfants, pour
qu'ils commencent d'abord
rciter le Coran sacr. Une fois
qu'ils le savent ou qu'ils en
rcitent une partie, on leur
traduit et commente ce qu'ils
en ont retenu.

5 - FU, danoo mgg ci wetu ay


waa jur, nu gindee nu noonu ci
dUne ji.

5 - Ici, l'on grandit l'ombre


de parents qui duquent de
cette manire en matire de
religion,

6 - Goora Jaan sunu maam di


lbu lamtuna bokk cin jaaneen
yi sos nguuru Baragwatan
reewum Barag jppe Marog
ba Ndeer mbaa Ndar gej ag
Soor Jaan dun yi law de! Ndar
ci b1u Jukk dexu Senegaal.
Da!a jog Baragwata n'w sos
Ker Goora ci Kajoor. Muy
Pey mu siiw ci dUne dolli di
Teeru, law jpp Paal, Sakal
Ra Baeeas ag Ciise.
Mooy Maam Paate turandoo
woowu ma jukkale liggey bi

6 - Gara Diagne, notre aeul,


lbu lamaan parmi les Diagne,
fondateurs
du Baragwata,
royaume du Barag, allant du
Maroc actuel Ndeer sur mer
et Sor Diagne, les l'origine
de Saint-Louis l'embouchure
du Jukk ou Fleuve Sngal,
vint s'installer au Kayor. Il y
fonda ker Goora, mtropole
religieuse et ville commerciale
influente dans les rgions de
Pal, SakaI, Rao Bathias et
Thisse.

Caatu Roxxaya Tafsir Umar


Sll mi sane liggey daara te
daan jangale, moo i liggey

Fils cadet de Rokhaya Tafsir


Gumar SalI qui ouvrit une
cole coranique
o elle
enseignait,

tekkimi mU daJa bokk ci maasi


jamano, noo xam ni Astou
Naar, YuusuJa Sll, Ablaay
Njaay, Arnet Jeng ag Maxtaar
Jeng MO leen jangal

le traducteur de texte appartient


une gnration qui tudia
auprs de Astou "la mauresque",
y oussoupha SalI, Abdoulaye
Ndiaye, Hamet Dieng et Moctar
Dieng

Jementu wi nu sumb danu ciy


wut do'rJ'rJlu nu xirtale ulema
boroom xamxam yi, ag Aafisul
xuraan yi, ba nu trak ci mbind,
tekki ag firi yu wer yi war Ter
bU nu ten ndonoloo.

L'exercice que l'on entreprend


ici vise pousser les savants
ulma et les matres de Coran,
fixer par crit les traditions de
traduction et de commentaire
autorises du Livre dont ils sont
les dpositaires,
7 - Les musulmans du continent
africain sont parmi les premiers
avoir
fait montre
de
dtennination pour asseoir et
diffuser l'islam et le Coran dans
les perspectives et les traditions
les plus belles,

7- Jullitu Taari yi manaam wa


Afrig yi, danu bokk ci ni jkk
xer ci d] ley, lawallislaam ag
Al xuraan ci gisgis ag aada yi fi
gn rafet.

8 - Lislaam bi muy feen fii,


ndali Ghana la fi fekk wu
Tekruur,
Wadaan ag wu
Gaawo, manaam wu Zaghawa.
Booba nguur yooyu nooy law
ba ca geju Mediteraane.
Danu fa sakk ay d'kki teeru
naka Talamseen, Sigil Maiga
mbaa Tangiita. Noo ame booba
wurusu
addina
wi.. di
demanteeg Europ, Penku ag
Bisaans.

8 - L'islam en Afrique apparut


l'poque des Empires du Ghana
et du Zaghawa.
Ces deux puissances politiques
rayonnaient
alors jusqu'en
Mditerrane,
Elles y avaient cr des
comptoirs commerciaux comme
Talamsen, Sigil Maisa, Tanger.
Elles contrlaient
l'or du
monde, commeraient
avec
l'Europe, l'Orient et Byzance.

9- Bi fwo dugg ci 8 teemeri at,

nguur yi.
Ghanawa yi, Zaghawa yi ag
seeni paraale, dJ nanu booba
nguuri islaam yu bees, jiital
doxalin wl yaatal di boole ag
yamale iiit fipp ci wllu diine.
Looloo waral mbootayu xarijiit
yi jog taxawal diine jamono
joojor.

9- Au dbut du VIlle sicle,


l'islam pntre les esprits et les
pouvoirs. Les Ghanawa, les
Zaghawa
et leurs allis
installent
de nouveaux
royaumes
islamiss
qui
privilgient une dmocratie trs
large et populaire, conforme
leur tradition. C'est l l'origine
des grands
mouvements
kharijites qui bouleversent et
adaptent l'islam au mieux.

10- Tarix Ibn Siyaad Abdallaah


Ibn
Walghu
di lamaan
ghanawa, 100100ko jo ci togg
xare, dJnguur Espaan ag wall
ci Erobu Mediteraane, tublo
leen ci 710. Masayar (Maycara)
beneen ghanawa la daan yanu,
di jaay ndox.. dana jog jiite
mbootaayu jullit, foxxati nguur
gi ci reewum Tarix moomu.
Mooy nekki imaam ag xalifa wi
j"/(kci xeeti Afrig yi.

10- Tarih Ibn Ziyaad Abdallaah


Ibn Walghu,
un lamaan
ghanawa, conquiert, en 710,
militairement,
et islamise
l'Espagne et une partie de
l'Europe mditerranenne.
Masayar appel Mayara, un
porteur d'eau, se manifeste
comme guide en 730. Il prend le
pouvoir dans le pays de Tarih et
devient le premier calife-imaam
africain.

11- Nguri Talamseen, Sigil


Maisa, ya woon ag yu bees yi
na Tahert 761, mba Fes 786,
noonu la flu lawe noom it gn
d"g.ral lislaam ci jamono

11- Les anciens pouvoirs


comme Talamsen, Sigil Maisa
et les nouveaux ns Tahert
761, et Fs 786, vont s'tendre
et consolider la nouvelle foi.
C'est la mme poque que
l'islam s'panouit au Ghana.

lislaam tbbi na ci xel yi, ag ci

yooyu.
Ndaali Ghanna ci jamono
yooyu lafa lislaam menn.

12 Gannaaw xewxew yooyu la


Njawar Jaagiliba njitu xare
reewum Ghana di togg xare wiy
dJi xalifa fatimid. Dafa mb ei
gannawam li dale Walata ba
Sijil Maisa ag TangUa ci geju
Atlanlig ci 958, jublu kaw ag
penku, dem ba Espaai, Sisil,
Sardaai, Misira ag Siri wann
leen.
13- Moo sane pne mi di Keer
ci 969, tabax El Asar 970, samp
Al Muhiz naka xaliJa. Gannaaw
gi la walbati Bagdaad ci 973
teg ei kiraayam iatti d"/(kyu
sell yi: Maka, Medin ag
gerisalam

12- C'est la suite de Tarih que


Njawar Jaagiliba, commandant
des armes du Ghana, mne la
guerre sainte dont natra le
Khalifat fatimide. Il conquiert,
dans sa foule, l'espace qui va
de Walata Sigil Maisa et
Tanger sur l'Atlantique, en 958968, se dirige vers le Nord et
l'Est. Il atteint l'Espagne, la
Sicile, la Sardaigne, l'Egypte et
la Syrie qu'il annexe.
13- Il fonde le Caire, en 969,
construit El hazar, en 970,
amne Muhiz et le fait
consacrer Khalife, aprs sa
victoire sur Bagdad en 973 tout
en se dclarant protecteur des
trois villes saintes: la Mecque,
Mdina et Jrusalem

14 - Mbootaayu xariijit yi mu
bokkal jamono, Abu Yazid, benn
zaghawa judoo Gaawo di
jngkat wu mag, bokk ci yoonu
lbaadit yi, tey doomu jula wu
am alaI moo ka sos ci 946, jUtaI
ko.Abu yasid moom daJa jog
jublu Ifrihiya manaan Tanis'
mba Tunisiya ngir beesali ji fa
dUneju bees ji

14 Le mouvement xarijite qui


nat, la mme poque, est
fond, en 946, par un Zaghawa,
Abu Yezid, n Gao, grand
rudit ibadite et fils d'un riche
ngociant.
Abu Yazid ira lui. la conqute
de l'Ifrihiya ou la Tunisie afin
d'y renouveller la nouvelle foi.

15 - War Jaabi Njaay di Buuru


Tekruur moo galandu, d"/(kalci
:Gede, maraabat Ghana, yiy
sosi mbootayu Almorawid

15- War Jabi Ndiaye, souverain


du Tekruur, accueille et installe
Ged, en 1040, les marabouts
ghanawa
l'origine
du
mouvement almoravide.

(;

yi, (1055-1147). Dafa dooleel


Tasfiin jog ci rewum Teen
Samoren nd ag Telegin njiitu
Lamtuna wi ko ndi Gede.

Il soutient Tachefin, originaire


du pays du Tin Zamoren et
Telegin, le chef lamtuna qui le
fait accueillir Ged.

War Jaabi dafay dooleel


mbootay goo gu. Dafa koy boole
ag xare wu mag wu jarbaatam
Lebu Sll jiite, nd ag Yahya
Ibn Taashfiin,
Abuubakar
Taashfiin wiy s'yag Farimata
Sll jigenu Lebu, Yuusuf, bokk
!Lenoag Abuubakar.
Noonu noo nd ag njiitu diine
wiy Ibn Yaasin, ab ghanawa
wu, bawo ci moomeelu Teen
samoren.

War Jaabi prte force au


mouvement. Il lui fournit une
arme conduite par Lbu SalI,
son neveu
et hritier.
Aboubacar Tachefin, son beaufils, poux de Farimata SalI,
soeur de Lbu, Youssouph
Tachefin, cousin de Aboubacar.
Ce sont eux les compagnons de
Ibn Yasin venu du pays du Teen
Zamaren.

Noonu noo lawal xilaafaatu


Almorawid yi, foUi Umeyyaad
yi ci ngnnaaru Afrig ag ci
Espaan.

C'est eux qui vont tendre le


Khalifat
almoravide
en
s'emparant
des royaumes
ghanawa d'Afrique du Nord et
Ommeyyade d'Espagne.

Almoxaad yi leen di wuutuji


fioom ci seen bopp Ghana lanu
bokkoon.

Leurs successeurs almohaad


eux-mmes relevaient de la
mouvance du Ghana.

16 - Turner mi jiite Almohaad yi


ghanawa la. Almohaad yi
(1160-1212) noo y6bbu fu sore
dekkali dUne ag xamxam bi
lislaam yewwi. Ci jamono
Almohaad yi la Ibn Tofaayil ag
Ibnu Rush feefi, dekkali Aristot
ag xamxami dmb.

16- Tumert, leur guide, tait un


Ghana- wa. Les Almohaad
(1160-1212) portrent loin la
Renaissance
religieuse
et
scientifique dclenche par
l'islam. C'est cette poque
qu'apparaissent Ibn Tofal et
Ibn Rush (A verroes)
qui
ressuscitent
Aristote et la
pense ancienne.
7

17 - Maali wu Kanku Maisa ag


Bakari mi jll atlantig ci 1312
dana lawal islam fay nekki
Amrig.

17 - Le Mali de Kanka Maisa et


Bakari II le mansa navigateur
qui traverse l'Atlantique en
1312 portera l'islam Outre
Atlantique.

Songhai, wu Soni yi ag Askiya


yi, iiooy ubbil
bunt bi
Suleymaan Baal, Usman Dan
foojo, Aaj Umar Taal ag
Samori Ture.

Le Songha des Soni et des


Askia, ouvrira la voie
Suleymaan Baal, Usmaan Dan
Fojo, El Haj Umar Taal et
Samori Ture.

Boroom xamxam yu Ghana,


Gawo, Tekruur ag Maali yooyu
boole Soninke, Lebu-wolof,
P1, Se rer, Tuareg, Rausa
mba Zaghawa iiUiiuul, iiUxees,
iiii xeereer, iiii weex, ci iii jKk
tekki firi ag lawal Al xuraan ci
seen lkk laiiu bOkk.

Les savants de Ghana, de Gao,


de Tekrour et du Mali, forms
de Sonink, de Lbu-wolof, de
Peul, de Srre, de Touareg, de
Zaghawa, de Berbres noirs,
rouges-ocres, clairs ou blancs,
sont parmi, ceux qui auront les
premiers, traduit et comment le
Coran dans leur langue propre.

18 - Yunus Bif lyaas (842-844)


di s'tu Tarih, jiitu Lamtuna ci
Baghawarta miy Marogu tay,
moo j"k,ktekki ag bind pp na
fukki teemerib at Al Xuraan ci
lkku lamtuna, zanaga.

18 - Yunus Bit lyaas (842844), petit-fils de Tarih, chef


lamtuna du Bhagwarta, devenu
le Maroc d'aujourd'hui, a traduit
et transcrit le premier le Coran
en langue lamtuna il y a de cela
plus de mille ans.

Ghomara yi dKkwetu Tetuwan,


daa nu deft lu ni mel. Ci
gannaaw gi, Tumer mi d}
xalifaatu Almoxaad moom itam
tekki na Ter bi ci lkkam.

Les Ghomara vivant du ct de


Tetouan ne seront pas en reste.
Tumert,
fondateur
du
mouvement almohad, traduira le
Livre dans sa langue.

Ulema sofiinke yi, wolof yi, al


pulaaren yi, hausa yi, Kiswahili
kanembu yi, bamun yi, soose yi,
Taraga yi, daa nu tekkiji Al
xuraan, firi ka, bind ka ci seeni
arafi bopp, mbaa ci yaxu araab.

Les Ulma sofiink, wolof, al


pulaar,
hausa,
kiswahili,
kanembu, bamun, taraga ou
touareg, mandeng ou soc, ont
traduit le Coran pour le
commenter et le fixer par crit
dans leurs graphies propres ou
avec l'alphabet arabe.

19 - Hindu bamun mba ajami


Rausa ag walafal yi nu ko

19 - L'criture bamun, l'ajamihausa et le walafal utiliss cet


effet sont anciens.

t"nke lu fi ygg lanu.

Cosaan loolu moo ubbil yoon


gannaaw gi kelifa diine ag
boroom xamxam yi : Sultan
Njooya, Malaam Jibril, Usmaan
Dan Foojo
Dem, Cerno
Mombeya, xali Majaxate Kala,
Tafsir Umar Sll, Aaj Malik Si,
Sheex Amadu Bamba mba S'rin
Ma Isa Ka, Serin Limaamu
Laay, Ibraxim Nas, Serin Aale
Fall Sali, Serin Abiib Sail, Serin
Abdu AzUz Si, Serin Aadi Ture,
S'rin Abbaas Sll ag seeni bokk
jamono.

Cette tradition a ouvert plus


tard, la voie au Sultan Njoya, au
Malam Jibril, Usman Dan
Fojo Deem, Cerno Mombeya, Ie
Cadi Majahate Kala, Amadu
Saar Njaay Saar, Tafsir Umar
SalI, El Aaj Malick Sy,
SheexAhmadou
Bamba,
Serigne Ma Isa K, Serigne
~imamou laaye Sheex Ibraxima
Nasse, Serigne Aale Faal SalI,
Serigne Habib SalI, Serigne
Abdu Aziz, Serigne Aadi Tour,
Serigne Abbas SalI et leurs
contemporains.

20- Aada tekkinu Al xuraan yi


nu def ci lakki Afrig yi, du jex.
Li tumuranke mooy nu bind leen
ci daara yi. Foofu la ykkamti
def ko, m.ne soxxikoo. Jot
googu ci tekki Al xuraan ba
bind ka,

2().. Les traditions tablies de


traduction du Coran en langue
africaine ne se comptent plus.
Le fait rare est de les voir fixes
par crit dans les coles. C'est
de l que nat l'urgenceOn l'a
ressentie alors que l'on menait,

am na fanweeri at fiu yeg ko.


Booba fiu ngiy liggeey ci IFAN
ci wallu lkk yi ag sunu yeneeni
nawle.
21 - Jot googu moo fiu joo ci
j"emntu wii. Moo fiu joo, ci
jle Al xuraan ci tekki mi ko
Arkun tekki ci faranse, ngir
wane benn ci yoon yi nu me.ne
lawale, nu gaaw, Ter bi;
lawal mbind diine ag xamxam,
ci njngum xale yi ag xyna
mag fii itam.

. il Y a prs de trente ans, des


recherches sur les langues
l'IFAN, avec d'autres collgues.
21 - C'est cette urgence qui
lgitime ce modeste exercice.
Elle a incit traduire le Coran,
partir de la version franaise
du Professeur Arkoun, avec
l'intention de suggrer une voie
susceptible
de diffuser
rapidement le texte, l'criture, la
religion et sa science dans la
formation de la jeunesse, voire
celle des adultes.

22. - Li mooma doli duggal ci


tekki ag gnne Al xuraan ci
wolof, dafa fekk jng ag jngale
xamxambi lkk bokk ci samay
ite.

22 - Ce qui m'a galement


pouss traduire et publier le
Coran, tient au fait qu'tudier,
enseigner les sciences de la
langue et diter, relvent de mes
proccupations
professionnelles.

23- Am na ay at fiu door di


foraatu, di tekki ag gnn ciy
ter : ay tnn; ay way, mbindi
xamxam ag pexekaay mbao
tegfiig yi dppoo ag jamano ci
lkki Ajrig yi te di jrifio arafi
araab mbaa yu latefi.

23- Linguiste, je me suis


habitu depuis quelques annes
collecter, traduire et publier
des anthologies,
des textes
africophones de science et de
technique grce aux graphies en
lettres arabes ou latines.

24- Naari mbindin yooyu ypp


danu tibbe seen cosaan fa doon
Misira ag Sumeer: fiaari rw
yu ygg yu me"soon inb xalaat
ag fiitin yu lislaam, fiew ba Ma

24- Ces deux critures tirent, on


le sait, leurs origines de
l'Egypte ancienne et de Sumer,
qui ont produit les ides et les
humanismes que l'islam aprs
Mose

10

Maisa Isa ag Isaa wy, beccali


leen, gn leen d] ag saxal ci
xol yi ag xel yi.

et Jsus aura renouvels et bien


enracins dans les esprits et les
coeurs.

25 - Waaye Ii am, maanaa ci lii


ypp, na nu ko waxaat, mooy
daiioo iiaan boroom xamxam yi
tari, tekki ag firi Al Xuraan
weesu bu gaaw Ii, iioo j.em
mentu fii. Nu bind seeni liggey,
ba jullit yi ag jngkat yi ci suiiiy
gox, ag yenee iii goxi addina yi,
iioom iipp m"njot ci Ter bi,
di ko tari ci arab, di ko wax ag
di nemmeeku Ii mu inb ci seeni
lakki bes bu nekk. Sriii su baax
si, iioo ko wax "Al Xuroon loo
ci wax lu mu tuuti tuuti, fexeel
ba xam lu mu tekki. "

25- Ceci dit, l'essentiel est,


rptons-le, notre souhait de
voir les matres de savoir qui
ont rcit, traduit et comment
le Coran, aller rapidement audel de ce modeste exercice.
Qu'ils fixent par crit leurs
oeuvres, que les musulmans et
les lecteurs d'ici et d'ailleurs
accdent
au Livre, qu'ils
rcitent en arabe pour le dire et
le reconnatre dans leur langue
de tous les jours. Les guides
vnrs l'ont soulign: "Le peu
que tu dis du Coran, tche de le
comprendre pour le moins."

Poote loon

Path F. Diagne

11

TANN

Suraat wi jkk
Wacce Mkka 7 laaya

Benn - Senn - Menn la- Raax Menn - Raax Yrm


1- Mggal Ylla buuru dunyaa
Raax Menn Raax yrem.
2Buuru bsu sddaIe ba.
3Yaw la fiuy jaamu, yaw la fiuy fiaan ndimml.
45- Teg fiu ci yoon wijub,
6- Ci yoonu fii nga bgaie say mbaax;
7- fii la merloowul te rerufiu
Suraat eXIV
Nit ni
Wacce ci Mkka 5 laaya
Benn - Senn - Menn la - Raax Menn - Raax Yrm
1- Nil damay wut kiiraay ci sunu Boroom
2- Buur ci ku di nit
3- Ylla ci ku di nit
4- Wttu ma ci mbonu kiy sol xalaat yu bon tey rocceeku
5- Di waIlu bon ci xoli nit fii
SURAAT eXIII
Bes tenk
Wacce Mkka 5 laaya
Benn - Senn - Mennla - Raax Menn Raax Yrm
Nil damay wut kiiraay ci Ylla fa biir sete
Muslu ci mbon gi ci mindeef yi mu skk
Muslu ci musiba guddi lndem krs fa mu fiu bette
Muslu ci mbonu dmm yiy wl ciy paspas
Muuslu ci musib kfiaanu ki afiaan

1234-

5-

Suraat eXIl
Kenntalaayu Ylla
Wacce ci Mkka 41aaya
Benn - Senn - Menn la Raax Menn - Raax Yrm
Nil: Ylla kenn l
1Di
Ylla mi di ba faww; ki jrul kenn
2-

13

34-

12345-

ki kenn jurul
Te amuI ku mu yamal

Suraat eXI
Abu Laxab
Wacce ci Mkka 5 laaya
Benn - Senn - Menn - Raax Menn - Raax Yrm
Na fiaari loxo Abu Laxab ya faaf, te mu maf moom ci
boppam
Alalam aki jfam du fiu ko jerifi dara
Danafiu ko lakk ci safara say boy
Moog jabaram ja yanu matt
Te ci baatam la noo yeewi buumu xafici tandarma

Suraat ex

123-

Ndimmlli
Wacce ci Mkka 3 laaya
Benn - Senn Menn la - Raax Menn - Raax Yrm
Bu nu ndimmalal Ylla ag ndarnam ganesee
Daa gis nit fii faxx andandoo jbbolusi ci diine Yllaji
Tggeel Boroom bi tey baalu ndax dafa sopp di baal nit fii.

123456-

Suraat CIX
Weddikat yi
Wacce ci Mkka 6 laaya
Benn - Senn Menn la - Raax Menn - Raax Yrm
Yeen weddikat yi
Duma gmi Ii ngeen gm
Du ngeen gmi Ii ma gm
Gmuma Ii ngeen gm
Gmuleen Ii ma gm
ngeen arn seen diine, man ma am sarna jos.

14

You might also like